iBet uBet web content aggregator. Adding the entire web to your favor.
iBet uBet web content aggregator. Adding the entire web to your favor.



Link to original content: http://wo.wikipedia.org/wiki/Ut
Waxset — Wikipedia Aller au contenu

Waxset

Jóge Wikipedia.
(Yoonalaat gu jóge Ut)

Waxset mooy juroom-ñetteelu weer ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.

Turam ma ngi jóge ci Augustus, ngir màggalee ko ko moom mi nekkoon buuru Rom ci 8 nj. j. Isaa. laataa moom moo nekkoon juroom-benneelu weer ci arminaatu waa-rom bu jamono ju yàgg ja.

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar